Fa||ou
40.3K posts

Fa||ou
@_Gallass
Doctorant en Économie 👨🏾🎓/ #BEUG_Serigne_TOUBA #Abdulahi_Wa_Khadimu_Rassul / #WASSILATOUL_ROUBOH🧠📚#Tazawoudou_sikhar_sham


Partie bi 🥰





📌 Jangale Seex Axmadu Bàmba Xaadimu Rasuul Am na naar bu mas a laaj Sëriñ bi ni ko damaa gisul ci Alquraan fenn fu sunu Boroom waxee wax ju leer ni firawna da fay tàbbi sawara ? Sëriñ bi ni ko xoolal innahuu la’aalin fil ardi wa innahuu la minal musrifiin ak wa annal musrifiina humu asxaabu naari. BIEN LIRE ET ECRIRE LE WOLOF AVEC L’ALPHABET LATIN

📌 Jangale Seex Axmadu Bàmba Xaadimu Rasuul 32. Sëriñ bi nee na lépp lu ngeen nekk ci ndigal yi da ngeen koy taqoo ndax ñooy yoonu àjjana. Lépp lu ngeen bàyyi ci tere yi da ngeen koy taqoo ndax ñooy yoonu safaan ba. 33. Am na ku Sëriñ bi masa yónni mu dajeek ñaari gaynde jaar ci seen diggante jàll. Ba mu ñëwee Sëriñ bi ni ko mbaa tiitoo ? Mu ni ko déedéet, Sëriñ bi ni ko tigi. Source: ay jàngale Seex Axmadu Bàmba Xaadimu Rasuul, nu tuxalee léen ci yenn ciy téere yu Sëriñ Alaaji Mbàkke Xaadimul Xadiim def. Topp nanu ci yu bari niki juróomi xaaji «Waxtaani Sëriñ Tuubaa», juróom benni xaaji «Jotaayu Texe», Juróom ñaari xaaji «Diyaa-fatu Samadiya» ak ñetti xaaj yu njëkk yu «Garabug Tuubaa».













