Historien

40.2K posts

Historien banner
Historien

Historien

@Mrthread4

Pauvres serviteur de Cheikhou Ahmed Tidiane📿 https://t.co/biJOMU0mad Instagram : Historien.Maodo

Senegal शामिल हुए Haziran 2020
13.4K फ़ॉलोइंग72.4K फ़ॉलोवर्स
पिन किया गया ट्वीट
Historien
Historien@Mrthread4·
😭🙏❤️
QME
14
368
2.1K
39.7K
Historien
Historien@Mrthread4·
Pour vous dire que nittu Yalla so andé ak mom boléko ak mbonteff té touboko yag yag dangay weru. Yalna Yalla sameu niou. Ibn Aboul Abass
HT
0
1
37
392
Historien
Historien@Mrthread4·
Benn way bou xamadi dafa gnew ni Serigne Babacar niko bayi na Tarikha bi té dara daluma. Serigne Babacar niko bayi wo Tarikha bi mais borom Tarikha bi mola guené nakh do dioug si diabaru diambur. ⬇️
Historien tweet media
HT
1
25
338
3.1K
Historien
Historien@Mrthread4·
*_Ku juddu ñépp xam la nga réere sa bopp, dañu laa robagul waaye dee nga bu yàgg._* *_Ku juddu ñépp réere la nga xam sa bopp, fu la neex yendul jàmm kese ngay am._* *_Sëydul Xawmi_* 😍
Historien tweet media
HT
1
40
293
1.9K
Historien रीट्वीट किया
khalid ibn al walid🇸🇳🕋💙
«Mouhammadul Mansour képp ku nàmm sa baay El hadji Malick dala jisul Wayé képp ku jaxaso ak yow lepp loum namé woon sa baay jiss ko ci yow » Mame Elhadji Rawane Ngom (rta )🕊️🇸🇳🙏🏽
khalid ibn al walid🇸🇳🕋💙 tweet mediakhalid ibn al walid🇸🇳🕋💙 tweet media
HT
0
28
229
2.1K
Historien रीट्वीट किया
Jardin Du Rappel
Jardin Du Rappel@JardinDuRappel·
On se retrouve ce dimanche dans le panel In shaa Allah♥️
Jardin Du Rappel tweet media
Français
0
9
66
725
Historien रीट्वीट किया
Muhammad
Muhammad@MuhammaaD96·
Cet homme est vraiment exceptionnel 💚
Muhammad tweet media
Français
9
58
584
7.6K
Historien रीट्वीट किया
Dr Maktoumist
Dr Maktoumist@mamesarrdiff7·
Li yéemé si Seexu Tijaan RTA ak tariham moy ay talibéem kou nek si niom meun na jité continent
HT
0
13
86
1.1K
Historien
Historien@Mrthread4·
Li deh bok na si litakh sangam ba sopém ba serignam ba Mame Cheikh Seydil Hadji Malick Sy Rta done wakh nane « Rawane Raw nalene » Riddouwanou laahi Tahalah Ajmahin Pape Bou At Tijani
Indonesia
0
1
25
351
Historien
Historien@Mrthread4·
Dégu na gnouni Mame Seydil Hadji Rawane Ngom Rta temps bi geune minime boumou dane Lazim moy 45mns parfois dane na werd 1h de temps. Mak gni sen niveau diamou yalla amatoul walahi azim. Sama class gui keup keup rek diouk fakhassou. ⬇️
Historien tweet media
HT
3
22
283
3.5K
Historien
Historien@Mrthread4·
ZXX
0
4
34
359
Historien
Historien@Mrthread4·
Prends soin de notre Dhikr bien connu le jour du vendredi ; tu seras un érudits. El Hadj Malick Sy Fâkihatou Toullâb⬇️
Français
1
60
351
3.7K
Historien
Historien@Mrthread4·
Serigne Babacar SY (rta) nena : “ Mansour ndimbal leu bou diougué si Yalla niew Ci nioun ”
Historien tweet media
HT
0
30
396
2K
Historien
Historien@Mrthread4·
Da am biis Gòor Gui fébar, Médecin bi niew consulté ko néko Góor Gui : “ faut gua nélaw ?” Mame Mansour néko : “ meusuma nélaw lu wésu 5 minutes ”. Motakh Weuy Kat bi néko : waxtu simi rér ladal zikr dieum fadjar Mansour mu Malick
Historien tweet media
HT
3
39
365
6.1K
Historien
Historien@Mrthread4·
Si tu veux voir le changement que la Tidjaniya doit apporter à ta vie spirituelle , efforce toi de faire le Wazifa en groupe 🦅
Français
0
42
233
2.8K
Historien
Historien@Mrthread4·
Ci diggante 4i fan, Tiwaawan ñàkk ñaar, ci ñi gënoon a mag ci doomi Mawdo yi. Altine 25 Mars 1957 : Sëriñ Baabakar Si Àjjuma 29 Mars 1957 : Alaaji Mansoór Si Yal na Yàlla yokk seen i leer !
Historien tweet media
Suomi
0
34
366
2K
Historien
Historien@Mrthread4·
Bëgg ngaa nekk ku màgg fa Yalla ? Fàww ngay nangoo Dékkuy saaga te ànd ci Ak mugn gu rafet. Kon nag feddalil sa Laxasaay ndax Ci la ndam nekk. Serigne Mansour Sy Balkhawmi rta
Historien tweet media
HT
1
45
499
3K