" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗

20.3K posts

" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗ banner
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗

" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗

@RIENqueLUI

MA'AM SEEX IBRAHIMA FALL ñëriñ gudul jeex la, te ñëp xajj nan ci...

شامل ہوئے Mayıs 2021
4.1K فالونگ9.7K فالوورز
پن کیا گیا ٹویٹ
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗
Maximum de Rt🚨 C'est la mère de mon meilleur ami Kon sama yaay la, ni doomam lama defoon 2009 batay dji may bindi tweet guii, degg ñu ko, guissu ñu ko Xamu ñu ndax migui dundu wala... Waaye daal nigui rafeet njort Ci ndigalu doomam laa def Tweet gui Di ci sàkku ñaan ❗
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗ tweet media
Filipino
2
102
99
11.3K
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗ ری ٹویٹ کیا
Sëriñ Saliou
Sëriñ Saliou@AsSaalih22·
Yalla nanu yalla may ixlaas.
Türkçe
0
13
82
1.1K
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗ ری ٹویٹ کیا
Fallou Salih
Fallou Salih@SalihFadal·
Salam Mbokkou yi nionguiléne di woo si 3ème édition NGONTU WIRD MAH’OOZ mouye Mercredi 25 mars 2026 si Massalikoul Djinaan bou 16h dioté Inch'Allah 🚨Koussi beugue barkélou manako yoné si numéro bi késsé : 77 449 72 88 (Dieuwrigne Mouhammadou Sarr)
Fallou Salih tweet mediaFallou Salih tweet mediaFallou Salih tweet media
HT
1
72
117
8.2K
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗
Ni Sëñ Amdy def ba teg ko bët jaffe, la ñëp wara def. Ginaaw xamuñu ninuy sakanalee sunu kilifa, nañ sakkanal seen bop. Ndax xoolal ngay buxante ba gaañ sa kilifa
Eesti
0
0
0
179
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗ ری ٹویٹ کیا
فال
فال@Anta__fall·
Amngen si kaala yi ? 😍 ☎️781734326 Amat na stock limité !
فال tweet mediaفال tweet mediaفال tweet media
Suomi
3
28
179
3.9K
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗
Buxante ci kanamug Sëriñ bi , ñaaw na lool waay ! Li Maam Seex Ibrahima Fall fekoon ci Sëriñ, mu dindi ko , ñun fimne luko raw lañuy def : taxaw tiim Sëriñ bi , coow Gi, ku nek di filmé etc... Luko fi jarr?? ??
Filipino
0
1
9
392
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗ ری ٹویٹ کیا
dieery wadaane
dieery wadaane@DioufDiery·
Yalla na sounou boroom di dolli say nguereum saasou né
dieery wadaane tweet media
HT
2
13
187
4.2K
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗
Jaxasoo góor ak jigéen bu daganoon, kon Sëriñ bi duko tere ba di def ken du gis sa moroom. Leegi nag ken bëgg ko jàppee ludul dara diko négligé.
HT
0
17
123
1.7K
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗
Bari waan na li nitt di def, nga jàpp ni rewande la , fek na daa xamul rek. Walaay ñu bari xamu ñu lunuy def
Filipino
0
0
1
89
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗ ری ٹویٹ کیا
" REMARQUABLEMENT INTELLIGENT "❗ ری ٹویٹ کیا