Seex Ibra Sàkkoor💙🤍
31.1K posts

@CheikhIbraa
Jara am Seex Amdy Mustafaa Faal Shakuur💙🤍 Founder of @ShakurAnalysis📊📈#Entrepreneur #BusinessIntelligenceAnalyst @G_SidiBirahim

🚨NDIGËL Seex Muhammadul Muntaxaa jox na ndigël Serigne Amdi Xadi Faal ag jabootu Seex'Ibra Faal gépp, Talaata (mardi 31 Mars 2026) ñu yaatal mbooleem mbedd Marché Ocass yi ag lepp lu wër Jummay Touba Ji te waru fa ne (garages yi, tables yi....) lata ño dellu Kënzil Kitaab (Kërug Al Quran Gui).

Ku bëgg yalla suturaal la dangay suturaal sa bopp, suturaal nit ñi, Suturaal sa bopp mooy bayyi lu bon ta bula yalla nattoo banga def ko nga gaaw tuub ko, ta bañ ko siiwël. Waaye dëkk ci def lu yalla di tere dina waral yalla xaw wi sa sutura dina tax bakkaar bu ndaw nekk bu mag. فلا صغيرة مع الإصرار.

🪡Tailleur : Allô Coumba, joxaat ma say mesures… 🙎🏾♀️Coumba :❗️Faal loolu New Deal Technologique dakoy tere. Avec cette solution nous accompagnons les ateliers de couture à avoir une digitalisation interne de leur activité.✅ @ShakurAnalysis 📈📊