Dame🇸🇳
7.2K posts

Dame🇸🇳
@DameVerra
Sachez que l'islam est la Sunnah et la Sunnah est l'islam (Imam al barbahari). Le Coran apaise le coeur❤

Jamono ji nga xamni téléphone, internet wala RS amul woon nga xamni ku nekk Senegaal doo xam kañ la waa Makka di taxaw arafat wala kañ la weer wi feeñ. Boobu débat bi amul woon😊 Ku jot sa 9e jour woor arafa

@DoomuSenegal @AsSaalih22 ken wooralul taxawaay ba,bëssu jurom ñenti fane si dhul hujja la nuy woor moy yawmu arafah,moy biss bi seus si tabaski. Biss bi doo ko natt si taxaway bi makka ndax biss bi amna lu yagg te hajj makka yalla farataa laguko. Diine xam xam la du ñakup teggin.

Abb murid soxlawul uut lenen lumuy wird si genre bess yi. Sëriñ bi faagu tee leep tee luñu nangu leu ba paree

Xur’aan ♥️