Ibrahima Sene💫❤️166i

39.9K posts

Ibrahima Sene💫❤️166i banner
Ibrahima Sene💫❤️166i

Ibrahima Sene💫❤️166i

@Lamp_Fall96

❤️Lamp fall baboul mouridina🥰❤️Mawahibou Nafih- Bichri😩💕 Serigne Fallou Protège ♥️👌 🫰

Senegal Katılım Eylül 2017
2.8K Takip Edilen5.6K Takipçiler
Ibrahima Sene💫❤️166i
Gayi ñigii si live bi di yamaler ki ñu yok microm si jang mbollo ak wadjii di filmer bopam😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 Fi daguén nekh nak bilahi Kiñ yokk microm eck moko sakou? Ñi yoor sonno bikay ño yok microm wayer dou mom mi nek si kurel giii
GIF
HT
1
0
4
1.4K
Ibrahima Sene💫❤️166i
@moughniyan Ki deh baaa leuz fima takhaw lay takhaw mo filmer bopam ba kerok may giss lenen saay🙏🏻🙏🏻🙏🏻 Awa migikoy yetal
Filipino
0
0
0
41
Ibrahima Sene💫❤️166i
Man dall maguifii 👐🏻🚨 Kén dumasi guéner Jamono yimom cheikh samb sen audio bobou di fuiter loufi nityi waxoul amoul ay thiakhan laaa (Donter lolou la nourou) koneu nak sou jëf djii amer mom ñu bëgg ko rafetal dafmay jaxal
𝐏𝐫𝐢𝐧𝐜𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝟏𝟖🇸🇳🇮🇷@Prince_Mourid

Vidéo waajooju di jàng di vidéo boppam, bu ngeen waxee ba rafetal ko dh, dingeen ubbil yenn jànkat yi woyafal mbir yi buntub Foh… Te mbirum Xasaa’id yi dh, lépp lu ciy taxa dugal am foh rekk, loolee mat naa moytu ak di di ko moytuloo nit ñi.

HT
1
3
7
1.4K
Ibrahima Sene💫❤️166i
@Bass_G_Mbacke 😂😂😂Micro usseynu fall yigay degg awma lumasi woor wayer japeu nani dou mom mokoy enregistrer diko dugal deh ay sopem niony deff yoyou Wayer ki moo tek videwo filmé bopam dugal koo
HT
0
0
0
80
Ibrahima Sene💫❤️166i
@echgueye Dumako touder ngistal muuk wayer dama japni du ay teggin ga nék si kurel di filmer sa bopp dall da rafetlou wul dall😆
Filipino
0
0
1
12
Alaaji Sheex
Alaaji Sheex@echgueye·
Man nak dama toll foi xamni lii mu def nii daanaka jappeewuka ko dara salaaw . Kurel yi dañu koy filmer diko dugal si internet bi nit ñi nek fu nek di deglu , seen xol di sedd . moom amul kuko filmer mu filmer boppam dugal ko si internet bi Sellal gi rek moo am solo te Yalla na nek si moom. Amaana sax yeenem gëna sell ki ñu tegal 5 caméra diko filmer .
as_salikh@amour_xassida

Ma ték ko fi daw😂🤍🏃🏽‍♂️‍➡️ #tlnoce

Filipino
13
9
79
10.9K