Sabitlenmiş Tweet

Bu sénégalais dofdoflo ba wone guinaw Sonko dinguén reuthiou linguen dioudo.
Première pas de scandale
Première fois état bou diégué askan wa
Première fois nioulay wax deug
Première fois malgré métit bi niou wagnil marge doundou bi ci bena ate
Première fois niou beugeu créé ay pole industriel
Première fois ken sathioul sa xaliss
Première fois ay centaines de villages si tak par werr
Le seul problème de gouvernement bi moy amouniou touti bandi pour stopper les opposants milliardaires qui ont déstabiliser ce pays
Et puis boléne fi dindé ko fi tekk ?
Nekléne aye nit
Français

























