Sakina❤️✨
237 posts



Lii mom kou nekoul ndialo kate warou la metti je vois rien de mal

😭CNI, kone nioune amougn sécurité ak cadenté?

😭CNI, kone nioune amougn sécurité ak cadenté?

Jigeen bu divorce parce que son Mari daf ko takkal wujju et je precise son Mari bokk na ci ñu ko mën: maanu na, responsable na et tout et la femme le sait, Soxnassi moom bu deme fa yàlla mu laaj ko lutax nga divorce lu muy tontu ? Gaaw ngeen ci trop te nekkul lu dul ay caaxan🤨


Una mujer obligó a su hijo menor a lavar los platos después de que le ordenara hacerlo a su hermana: “Así no se les habla a las hermanas ni a las mujeres”, le dijo.


At this point, I think I need a woman in my life..


Khessal déguisé (glow) bigen khewal tmt ken douthi wax 🥲 ?

@salioumbackefa1 Sama xalat lay waxe kay, diine mën na ci and ! Yalla tënkul benn soxna mais Jigeen yi ci yëg ak lor mo ëpp fuuf ayib bu ñu mën saafara la, liy sunu ko legitimer nañ japp ni menage polygame dina rare ci jamono ji. Ku ci nekk so ame wuju do xalat muñ sa premier reflexe tas lay nekk














