🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕

2K posts

🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 banner
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕

🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕

@adjikhady003

Aspirante infirmière 🩺 | Amoureuse du khassida Mouqadamatoul Amdah, un éloge qui élève l’âme et apaise le cœur | ﷺ Allahumma salli ‘ala Sayyidina Muhammad📿❤️

Katılım Ocak 2023
1.5K Takip Edilen2.8K Takipçiler
Sabitlenmiş Tweet
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕
Il est le Chef, il est Vigilant, il est le Répondant, il est Pur de tous les vices, Il est le Messie, il est le Tuteur qui efface et embellit. Cheikh Ahmadou Bamba dans Muqaddamâtul Amdah❤️🥹 Bon Gamou #Gamou2025
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 tweet media🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 tweet media🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 tweet media
Français
5
7
84
6.2K
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweetledi
𝐏𝐫𝐢𝐧𝐜𝐞 𝐌𝐨𝐮𝐫𝐢𝐝𝟏𝟖🇸🇳
Saa bu guddi Àjjuma jotee, nga jàng: 1-Faatiha 1X 2-Salaatu Halan Nabii 1X 3-Lixlaas 40X 4-Salaatu Halan Nabii 1X Su noppee nga yéene ko jullit yi faatu yépp ak ñiy dund jamono jii, ak ñi wara judd. Kon jullit bi njëkk a faatu ba ki mujjee faatu, dinañu am yoolub 40 Lixlaas. Ku ko saxal ba Yawmal-Xiyaam, ku ñëw ci yaw ngir fayonte ak yaw, Yàlla moo naan ko, bàyyi ko mu dem ndax ku ñu mbaa-Yàlla la, dafa farlu woon bay maye aw yiiw. Sëriñ Tuubaa moo ko waxoon Soxna Fat Ja (doomam).
Eesti
1
67
175
2.2K
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweetledi
Sahibu_Salawat📿✪
Sahibu_Salawat📿✪@Murtada_M_Taawu·
Salaatu hala nabii yepp am solo Waaye yoy teere bii daa jeggi solo Rawatina yii lamboo mbóotum istixfaar Niki Salaatu gii Ku yor limu istixfaar dee ko tëje Salaatu gii.🤍✅️ - 92 fois - 111 fois -368 fois - 313 fois #TaawOu
Sahibu_Salawat📿✪ tweet media
Indonesia
1
27
143
1.5K
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweetledi
Sahibu_Salawat📿✪
Sahibu_Salawat📿✪@Murtada_M_Taawu·
Salatu gi wax nañ nee kepp kukoy deff biss bu ne temeri yonn 100 fois bala tëdd,Yàlla dina ko baxee mu giss Yonnent sallalahu halayhi wa sallam ci bir geunte🤍✅️#TaawOu
Sahibu_Salawat📿✪ tweet media
Eesti
2
55
285
2.7K
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweetledi
Soxna Une Merenguée🫀🤍
"Lu baax lumu tuuti tuuti bulko xeeb, lu bon lumu tuuti tuuti bulko xeeb, ndax benn bu nekk lu tuuti li moolay yobbu ci lu bari Ii" ✍️🏾 Sëriñ Tuubaa/ Masaalik.
Soxna Une Merenguée🫀🤍 tweet media
Eesti
1
32
407
3K
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweetledi
جيل بحداد🫀💦 374i
جيل بحداد🫀💦 374i@djilyAbdoukhadr·
"Je rappelle d'abord à ma propre personne et vous rappelle la raison de notre existence et de notre séjour sur terre,à savoir adorer DIEU LUI qui a dit "Ne soyez pas comm ceux qui ont oublié DIEU au point qu'il leur fit oublié leurs propres personnes..."⤵️
جيل بحداد🫀💦 374i tweet media
Français
2
9
76
634
Mo_99i 😁🇸🇳 !!
Mo_99i 😁🇸🇳 !!@MohamedWilane·
Muqadimat baye saliou thiam 2005 Doumassi doyal been yoon 😭❤️
Indonesia
5
25
105
3K
Cyrille juuf🇸🇳
Cyrille juuf🇸🇳@cyrille_juuf·
Médicament pour des maux de dents Svp😭😭😭 ?
Français
50
6
217
28.8K
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweetledi
Mo_99i 😁🇸🇳 !!
Mo_99i 😁🇸🇳 !!@MohamedWilane·
Muqadimaat - kureel 1 Tuuba , 2019 ❤️ Ndeyssane , ceey soopi bii 🤩🙏🏾!!
हिन्दी
9
31
241
5.3K
🌸 Sokhna Adji • Amdah ❤️💦🧕 retweetledi
Soxna Une Merenguée🫀🤍
"Yaar" Par Seriñ Bassirou Mbacké Khelcom ✍️🏾
0
19
142
1.7K