F€¥MāN 🇫🇷🇸🇳
51K posts

F€¥MāN 🇫🇷🇸🇳
@freezoer
📉💼 WorldCitizen | Tidjani | #SeydinaCheikh


En effet, il n’exige pas que l’adepte de sa voie soit tenu d’adopter son école juridique….. » Jangg leen ko ndax yiww gu bëri gi, mais faut pas exagérer et en faire une obligation jusqu’à douter de l’appartenance à la personne que ne le récite pas . Chukrann mbokk yi.

@jabra_il Seriñ bi , lis moi bien. Basmala bi ndax Tijaan bi ko janggul tax na mu bokk ci tariqa bi ou pas ? C’est juste ça hein. Tweet de base bi mbokk mi dani dako jaaxal t itam limay wax du samay wax la preuve mooy li Sidna Sukayrīj r.a leeral nako ngir bañ nu diisal mbir yi 👇🏽.



@MrGueye01 @baye_ahmad Bien sûr waroo wuute ak moom kay , waaye du wuute gu aju ci mbiri mazaahib d . Leegi nooy def ki bokk ci ngiiru Imām Shāfi /hanbal/ Hanīfa r.a.. ? Question basmala bi foofu lay dellu. Ñi ko dul jangg tere wuleen nekk Tijaan mukk nak. Waaye nak lu nu recommander la ndax yiww gi.



Salam, i heard buried in another city and then he was brought back to Fès ? Can you explain please 🙏🏼










