xaadim
8.1K posts

xaadim
@khdmkane
Aka neexoon ma xam dara ci sama boop 🫠

Nanu dellusi ci kenno évolution nak mënul ñaak wayer bunu fate muk seriñ binu andal te di bayi xel base yimu tëngkoon jang mi

Am na kudoon wax ci kurel li jàngkat ci sañser ak yeneén yici aju 😄 Waaw miy lu mata taxaw seetlu dax kune xam nani geztner yombul te wërsëk yamul konn kurel dina la tël ba boko amul digako lébi wala ga wuti ko ?…. Koon yalla taxatul xanna ?

Serigne Mame Mor Borom Sham (Son vrai nom est Mouhammad)mou Sokhna Diarra (Frère aîné et disciple de Cheikhoul Khadim) nékoone diamou katou Yalla boumak nékoone yarékate di Borom Kham-kham lissi firndé mooy diangalna Serigne bi amoona niéwanté si moom lole dako bayi khél si lép


Doko guiss ci Live tik tok , amul chaînes YouTube Doko guiss ci ay cambal Doko guiss ci lou ñiak fayda Geun nek star ñiep nak , meune diss gane t oyof tooy ! Mais boy yu bess yi ni ay Faramareen rek niofi nek 😌













