Sabitlenmiş Tweet
Ahmaduu Bamba
242 posts

Ahmaduu Bamba
@lecon_221
JOURNALISTE • CHRONIQUEUR OBSERVATEUR DU RÉEL #MOURIDE_PAR_CONVICTION 📍 SAINT-LOUIS (NDAR) JE NE COURS APRÈS PERSONNE #MARRIED 💍
Katılım Nisan 2024
406 Takip Edilen250 Takipçiler

Bëss pénc a ngi gën a jégé
Nit ni di gën-a sàggan
Lu ñu man-a dégg
Ciig waaré
Duu leen teere fo
Ak-a caaxaan #Ahmaduu

Magyar

Serigne Touba Néna
Na guéne mandou tei yamm
fii guéne wara Yamm
Lo beugoul kulako wax boul ko waxx kén Na guéne fokanté tey yeuramanté
Tei yalla rek takh….#Ahmaduu


MAME DANE NA WAKH NI AH DOOM…
Adouna niati fane la
Demb—Tay—Souba
Lo rethiou Demb fékhél
Ba rafétal ko Tay ngir
Sa Souba meuneu diak ..#Ahmaduu

HT


Fuu Goor Trokhalé Jiguen Rek
Goor Téralé nafa jiguen
Fuu Goor Niaké yeureumandé si jiguen rk Goor Yeureumé nafaa Jiguen
Kone Naniou Ande ak Daal Reek
Loula méti légui Boko beugué fadj legui
Bëss bo nopé réthiou ko bolé kok gathié #Ahmaduu

HT

Serigne Touba
Na guéne mandou té
Yamm fii guéne wara yamm
Lo beugoul kulako wax boul ko waxx kén Na guéne fokanté tey yeuramanté
Té yalla rek takhh #Ahmaduu


@mondemuslims Parler de ‘couverture’ quand il s’agit d’un être humain, c’est déjà un problème. Derrière ce genre de phrase soi-disant positive, on sent surtout un regard biaisé. Avant de donner des leçons, commencez par voir les gens comme des humains, pas comme des livres à comparer
Français

Xarnu bi suíte 👇
Fabal sa doom yi yépp boot
Ñoom it ñu boot séen ug njaboot
Ku manta boot nga jox ko mbóot
Ndax Yàlla naatal xarnu bi
Te fab muriit yi suturaal
Mottali jàkka jii ñu naal
Foo toll dolli séen alaal
Ndax Yàlla naatal xarnu bi
#Je_fb @lecon_221

Suomi

Xarnu bi suíte …👇
Jooy i perantal la nu jooy
Boo nu fabul, lee nu ne wóoy
Ku nu yafal, ban def i kóoy
Mu dellu naatal xarnu bi
Jisu nu yaay te noo ngi raam
Ku ñàkk yaay, day nàmp maam
Buural te boot nu, ngalla daam
Roggndi mboolem xarnu bi
#Je_fb

Filipino
Ahmaduu Bamba retweetledi

« Ma mère m'a dit de refuser le trophée de la CAN. Je le refuse officiellement et j'espère que mes coéquipiers feront de même. Nous avions une chance de le gagner, mais nous ne l'avons pas saisie. C'est le football, parfois on gagne, parfois on perd. Le Sénégal nous a battus à la régulière et méritait sa victoire. Ce serait injuste de gâcher leur joie après tous leurs efforts. Je respecte la décision de la CAF, mais je refuse officiellement le trophée. Je n'ai pas gagné la CAN
2025. Félicitations encore une fois au Sénégal. » -l
—Achraf Hakimi
Source [Marca]

Français

On dirait le ramadan le plus rapide de l’histoire Le temps s’écoule comme le sable entre nos doigts, rappelant que la vie est éphémère. Aimons sans attendre, aidons sans compter, respectons sans condition, car demain n’est jamais promis…Ahma…✍🏾
#je_fb
Français











