Sabitlenmiş Tweet
Abuubakrin As Siddiiq
7.6K posts

Abuubakrin As Siddiiq
@mbaye126
Ingénieur en Génie Civil | Saa-Wolof
Katılım Temmuz 2022
5.3K Takip Edilen3.6K Takipçiler

@AlaqMaktaba .عِيدٌ مُبَارَكٌ لَكَ وَلِعَائِلَتِكَ، وَبَارَكَ اللهُ فِيكَ فِي هَذَا اليَوْمِ المُبَارَكِ
🤍
العربية

@SalihFadal « Samay bind sunu Borom nangul namako » lii saay jaruo doli lenen
Filipino

Abb murid soxlawul uut lenen lumuy wird si genre bess yi.
Sëriñ bi faagu tee leep tee luñu nangu leu ba paree
Fallou Salih@SalihFadal
Khassida gui Borom Touba Yawma Arafat Balsashine lako teunké dissi sakou ndiégueulou Sunu Borom dissi niaane mou mousseulko si moye Yalla 🙏
Eesti

@MorTaif @moughniyan Saay kii bàyyi na nu fi bu yàgg di. Te soo demee d li ci dalle bi moo gën a sedd ci ay jafe-jafe wam
Eesti

@mbaye126 @moughniyan Seex Baabakar 😂 buleen ko def nii
Daa jaaxle 😂
Suomi

Lii yépp bëgg lu yomb moo leen ko yóbbee😭
Dalle bii ma giss de sooko wàccee wul reprendre ko dina def jëyë.
🇸🇳 Narou Kawsara 🇵🇸@Assane_Fall_Off
🚨A qui la faute ❓
Eesti

@moughniyan @MorTaif Ki la fi bàyyi dem jox maçon chantier kay jarul bàyyi xel 😂😂
Català

Yaw Yàlla sunu Boroom, yaw miy Aji-màgg di Aji-tedd di Aji-kenn ki noo ngi ànd di la yalwaan ci barke Rasuulil laahi SAW, barke mbooleem ñoo musa ak loo musa barkeel nga gën fee yàggal Seex Muhammadul Muntaxaa Mbàkke, gën koo sàmm, gën koo aar, gën ko muccal.
Mbooleem yi mu somb yal na nga ko kàttanal ba mu àggali ko te nu ànd ko ak moom.
Suomi

@moughniyan @SalihFadal Yonnee ma ko ba ma valide ba noppi 😎
Eesti

@SalihFadal Waawaaw Seex Fàllu moom kay lepp jub na kocc, ca kaw daal lako def ba noppi deff ko ay baies vitrée ouvertes sur la cour avant 😂
HT

Bëgg ngeen mos neexitu Oud ?



Abuubakrin As Siddiiq@mbaye126
Le bois de Oud "Or noir" apporte une connexion entre les fonctions du corps et de l’esprit. Il améliore la réception des sens et ouvre l’esprit, tout en calmant les fonctions principales du corps humain. Cet ingrédient de luxe présente également une "dimension spirituelle".
Nederlands

@_Bachiir Saay kaay ma lekk sa xaalis. Wave ma 80.000 gaaw.
Filipino















