Sabitlenmiş Tweet
Baay Hamza
23.2K posts

Baay Hamza
@mbayehamza
Murid | Qacida lover | Marketing digital | Communication | E-commerce | #DST #DCIF
Dakar Katılım Ağustos 2014
2.8K Takip Edilen5.6K Takipçiler
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi

Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi

Noo ngi leen koy fàttali
Tàngoor wi nii muy mettee ci Doomu Aadama Yi noonu it lay mettee ci Ñanaaw yi
Te nit manul dund ci lu dul ay dëkkandoom te ñoom ñooy sunuy dëkkandoo: Garab yi, mala yi, ñanaaw yi…
Tàngóor wi dina faagalgaal lu bari ci ñoom ndax ñàkk fu ñu naane te ñoom ci kéew mi lañu bokk kon sàmm leen nun la war
Lii misaal la ci fàggu i ndab moo xam bidoŋ la añs
Def ci ndox ajj ko ci kaw miir yi walla fu kawe ñu man di ci naan.
Touba Ca kanam
Commission Environment
« Sëriñ Jiili Alxuraan »

Suomi
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi

Salamu halaykom
Di leen yëgëlni arrêter nan inscriptions yi.
Kon ku bëggoon bokk mën nga xaar ban ubbi waat beneen classe buko jot gi mayee inchallah.
Jërëgeen jëf.
Sëriñ Saliou@AsSaalih22
Programme arabe bi nekk nii, le 9 mai inchallah lay tambali, • arabe • fiqh, livre: Le fiqh malikite et ses preuves. • tasawuf, livre: masaalik. Ku bëgg bokk mën nga bind/ woo numero bi nekk ci affiche bi 761547408
Eesti
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi
Baay Hamza retweetledi

Ay grippe, courbatures, fatigue, manque d’appétit, hsjzjziak, du am coow, dara du xew.
Booster 🔥
Bientôt le downfall des lóbi farmasi 🤣
بــــــشير@_Bachiir
Kombo (Laaj + Jinjeer + Limon + Lem) comme saaru faatiha rekk amul lu mu dul faj. 🔥
Français

Salam je cherche une personne ,
1. Fayuma yenay def Yallah moy faay
2. C’est 100 par semaine 😭😭
3. Cdi la
GIF
Busó ꕤ@soxnajaara_m
Salamm je cherche une personne pour faire 100 ikhlass par semaine ?
Français
















