Darmanko

21.4K posts

Darmanko banner
Darmanko

Darmanko

@Fallou__Amar

Passager de la vie n’aspirant qu’à l’Eternel

เข้าร่วม Ekim 2013
932 กำลังติดตาม958 ผู้ติดตาม
Darmanko รีทวีตแล้ว
Sheex Saalihu
Sheex Saalihu@serigne_salihu·
Maa ngi seede ni amul bénn buur bo xamni jaamu ko day jariñ ñàkk o jaamu di lor kudul y’الله sunu boroom subhaanahu wa tahalaa.
0
2
9
233
Darmanko รีทวีตแล้ว
أَلْحَمْدُ لِلَّــــــــهِ🤍
Il nous est unanimement manifesté sans aucune ambiguïté que le Fils de Abdallah est le Meilleur des humains ﷺ🤍 Serigne Touba Khadim Rassoul ❤️
Català
1
64
323
4.9K
Darmanko รีทวีตแล้ว
Moor Suraŋ
Moor Suraŋ@s_sourang·
Lépp luy doxal sa àdduna nga fexe ba xam ko, te sàggane sa diine ba xamoo ci dara, loolu jullit bu ne war na koo moytu.
Filipino
1
17
122
2.7K
Darmanko รีทวีตแล้ว
Sëriñ Saliou
Sëriñ Saliou@AsSaalih22·
Jamono jii ku jangul sa diine boo taxawee ci kanamu yalla ëlëg doo am lay, ndax jang leegi yombu na mën nga toog finga nekk di jang lepp loo bëgg xam sa diine muy al xuraan di xam-xam. Kon yitte ag farlu rek la laaj mu jaral la lila xam sa aduna jaral, jangal naa ay nit ñu yor seeni ligeey ñii boole ko ag yor seen kër di sëy ta diir bu gatt jang nañ lu bari ta yaxalu leen dara.
Eesti
3
42
139
3.9K
Darmanko รีทวีตแล้ว
Moor Suraŋ
Moor Suraŋ@s_sourang·
《Yàlla sippi na samay bàkkaar, far na samay sikk, tàggatal na ma bépp baadoolo buy gedd》
Moor Suraŋ tweet media
Magyar
0
51
305
4.8K
Darmanko รีทวีตแล้ว
Yaa Faaty🤍🇵🇸
Yaa Faaty🤍🇵🇸@S_Naawel·
لَا إِلٰهَ إِلَّا اللّٰهُ مُحَمَّدٌ رَسُولُ اللّٰهِ ﷺ💚
العربية
0
7
22
542
Darmanko รีทวีตแล้ว
Princetorodo_Mbacke ✪
Princetorodo_Mbacke ✪@Murtada_M_Taawu·
Ndeysanee🤍🥹
Princetorodo_Mbacke ✪ tweet media
Türkçe
1
27
318
6.1K
Darmanko รีทวีตแล้ว
Elias Waly Ba
Elias Waly Ba@eliaswalyba·
Software is changing. And it’s a blessing. We’re entering an era where writing code is no longer the bottleneck. Where building things becomes faster, smoother, more intuitive.
English
3
13
63
5.5K
Darmanko รีทวีตแล้ว
Saliou 🌔
Saliou 🌔@salioumbackefa1·
Bokk na ci baat yi ma gën a neex yi seriñ bi woowe yoneent bi aleyhi salaam : « la fine fleur🌹 des choisis, »
HT
1
34
147
8.8K
Darmanko รีทวีตแล้ว
Sheex Saalihu
Sheex Saalihu@serigne_salihu·
“Man naala moss te bu ma moss ludul yaw Te naala am te bu ma am ludul yaw” “Naa ne ci yaw nga ne ci man te sol ma Baa fees a fees say ngërëm nga yor ma ” SMJ 🥹🤍
Sheex Saalihu tweet media
Filipino
0
14
127
1.5K
Darmanko รีทวีตแล้ว
Yaa Faaty🤍🇵🇸
Yaa Faaty🤍🇵🇸@S_Naawel·
لَا إِلٰهَ إِلَّا اللّٰهُ مُحَمَّدٌ رَسُولُ اللّٰهِ ﷺ💚
العربية
0
9
20
409