
Yalla na yalla may kougnouy nianal biss bougnfi diougué🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Ça fait peur
𝐁𝐚𝐚𝐲 𝐗𝐚𝐥𝐢𝐢𝐥 🇸🇳📚📚📝@Ly_Ibraahima
Imagines nga nekk ci sa bàmmeel yaw rekk, dóotoo gis ñi nga daan gis, dóotóo lekk li nga daan lekk, dóotóo dem foo bëgg dem…nekk ci benn barab rekk di xaar ñu àtte la, xamóo ci sa bopp dara, te wóorul sax ñaan fekk la fa nga nekk ndax waa àdduna duñu gaaw a fàttali ku faatu…
Français