
Imagines nga nekk ci sa bàmmeel yaw rekk, dóotoo gis ñi nga daan gis, dóotóo lekk li nga daan lekk, dóotóo dem foo bëgg dem…nekk ci benn barab rekk di xaar ñu àtte la, xamóo ci sa bopp dara, te wóorul sax ñaan fekk la fa nga nekk ndax waa àdduna duñu gaaw a fàttali ku faatu…
























