
''Le motif de mon départ en exil est la volonté que Dieu a eue d’élever mon rang et de faire de moi l’intercesseur des miens et le serviteur du Prophète (P.S.L.)''
Ixlaç
3.3K posts

@asf_murid
Tawhid !!! je suis _Alchimiste With compassion, I open myself to the world and find peace. 🕊️

''Le motif de mon départ en exil est la volonté que Dieu a eue d’élever mon rang et de faire de moi l’intercesseur des miens et le serviteur du Prophète (P.S.L.)''

Ni yaram wi soxlaa dundu gu baax ag set pour dundu mucc ci febar yi, noonu la ruu gi soxlaa dundu gu baax ag set gir mucc ci febar yi, Dundu ruu mooy jaamu yalla, zikr, weet méditer, set gi mooy mu tegu ci xam-xam bu leer def ko niko yalla bëgge.





En moins de 5 minutes il explique brillamment le fonctionnement de notre Monde.



Joxante ngant moy li gën a am solo ci loy noppal nit ba noppi may ko tranquilite , ko xamul bul ko juger lifeek jaxaso woleen … njort bi nga am ci nit de loin yallah neena li ci ëpp ci ñoom du dëgg. Bul bañ ken rawatina ko xamul Bul noono ku la tooñul Bul njort lu ñaaw ci nit ko xamul Balaa nga atté nit fexeel ba jaxasoo ag mom ba noppi