
Question sérieuse: Ceux qui ont fait leurs études post-bac au Maroc, c’est quoi leur niveau très honnêtement? Man par exemple, mën wax à peu près niveau general yeen pays yi à partir de lima gis PMS. Bëgg na xam niveau Maroc trop parce que niru nañ lu nëx trop

















